Massamba Amadeus Amadeus Doumala Fowé Clip Officiel
>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=CZshUkiOgFo
#DoumalaFowé en stream et en téléchargement sur toutes les plateformes de streaming : https://bfan.link/doumala-fowé-1 • Auteur : Amadeus • Compositeur et Mix : Zoom ont the Beat • Directed : MLD Ice’Graphy • D.O.P : Likma • Lighting : BrasMagik • Edited : MLD SeleVfx • Décors : Yarba • © 2021 Cosanostra • Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux : • Instagram : / massamba_amadeus • Twitter : / massambaamadeus • Facebook : / massambaamadeus • Paroles : • Duma la fowe • • Duma la, duma la fowe • Duma la, duma la, duma la, duma la fowe • Duma la, duma la, duma la, duma la fowe • • Soxna si, ci mane ngay mujj a gise love • Ndeke mbëgéel is all i need man • Sàmm sa daraja ni Maam • Ma bamtu • Xale bi bu dul yaw du mas a doon keneen • Ndax sàmm nga sa ndaw ni maam • Di génn farata ni maam • Man àdduna laa bëgg a wan • Ba ñu xam ne que ne tekk naa la fu kawe kawe • Toogal sama wet bul ma mas a • tàggu ndax xam nga ne soo ma soree ma wéet • Dam la gis rekk teg fële sama mbonte • Man li ma yitteel mooy sama mbégte • Bëgguma la disturb • Jéggalu sun lay enerver • Non metti na la li ma la toppe girl • Yàlla xam na • Ne man bëgg naa la • Li tax ñemewóo ma • Damaa dëng jaar-jaar • Sama démb ñaaw na • njëlbéen du naada • Mujj gu rafet laay ñaan Yàlla jox ma la • Duma la fowe • Fi ma la fore daa sori • Sa ree ju neex • Moo may faj su ma feebaree • Duma la fowe • Ndax fi ma la fore daa sori • Sa ree ju neex • Moo may faj su ma feebaree • Ak li ma man gis li ma dégg • Man duma give up • Yan bi lu mu man diis lu mu dëgër • Dara du ma disturb • Nekkóo ci réseaux sociaux yi di polluer all time • Daanaka sax doo nekk online • Fuck cheveux naturels enjoy nga life bég naa • Looloo waral man yaw laay ñaan • Dam la gis yek teggi fële sama mbonte • Man li ma yitteel mooy sa mbégte • Bëgguma la disturb • jéggalu sun lay enerver • Non metti na la lim la toppe girl • Yàlla xam na • Ne man bëgg naa la • Li tax ñemewóo ma • Damaa dëng jaar-jaar • Sama démb ñaaw na • Njëlbéen du naada • Mujj gu rafet laay ñaan Yàlla jox ma la • Duma la fowe • Fi ma la fore daa sorri • Sa ree ju neex • Moo may faj su ma feebaree • Duma la fowe • Ndax fi ma la fore daa sorri • Sa ree ju neex • Moo may faj su ma feebaree • Traduction en français : • Je ne te déshonorerai jamais • Jamais, je ne te déshonorerai jamais, • Jamais, jamais, jamais, je ne te déshonorerai jamais • Jamais, je ne te déshonorerai jamais, • Jamais, jamais, jamais, je ne te déshonorerai jamais • Je t'honore ma vie pour plusieurs raisons • Et t'assure un amour sans crevaison • Consolidant continuellement nos liaisons • Parce que ma chérie tu es hors saison • • Sans toi, ma vie perdrait sa quintessence • Sans toi, mon entourage n’aurait pas d'assurance • Sans toi, mon étoile risquerait sa brillance • Sans toi, ma vision s'engouffrerait dans l'ignorance • • Au vu et au su de tous, tu es mon bonheur • Ta dignité sacrée couve ton honneur • Ta chaleur arrose et illumine mon cœur • Donc restons ensemble et chantons en chœur • • Je t'emboîte le pas comme le maître et son chien • Pour t'apporter uniquement le tout du bien • Je fouille tes traces quotidiennement et sans fin • Rien que pour apercevoir ton beau teint • • Pourquoi en es-tu dubitative ma chère ? • Ou tu es choqué par mon passé d'enfer • Passé que tu as commencé à changer ma lumière • Par ta dignité ancestrale ma dame de fer • • T'as pas suivi le vent tendanciel • Qui souffle au bord du monde actuel • Avec son caractère anodin et criminel • Référence des chocs de la mode existentielle • • Tu as su garder jalousement ta virginité • Tu as préservé ton honneur avec ingéniosité • Tu as pu affronter les obstacles avec leur tortuosité • Tu as dépassé victorieusement l'âge de la puberté • • Je suis prêt à vivre avec toi • Quelle que soit la lourdeur de la loi • De l'amour, j'ai déjà fait mon choix • Je ne te déshonorerai jamais ma foi
#############################
