Aicha Kone Djongué Clip Officiel
>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=DcTpRBsIbIo
AICHA KONE EST DE RETOUR AVEC UN NOUVEAU TUBE POUR L'ETE 2024! • Ecoutez le titre sur toules plateformes : https://distrokid.com/hyperfollow/aic... • • crédits • Artiste/interprète: Aicha Kone • Réalisation: Pac Deejaay • Beat: ZOX • Paroles: ZOX • Toplines: ZOX • Mix/Master: ZOX • • PAROLES • • Couplet 1 • Djongué takh founiou beuré damkoy dane • Ki makoy daanel wouy soldat a terre • Doumako mey dara trou yeupp laye fatt • Maay diw biy nineul seu thiep • Foumou tek beute man ley guiss damako moudjou yeeem • Ma mate femme lab neu tchi samay feem • Dafmey khol nane meu tu me rends fou • Ohh bb kham ngani maley danel • Maay fékheul seu khol • Fo meunti dem dangay nieuw sama djongué molay gaagn man nga beugue ci leu life • • Pre-refrain • • (Touss touss nak touss ) man rek ley toppeu • (Touss touss nak touss ) souy nelaw man rek ley guinteu • (Touss touss nak touss ) ki dé man leu dinkeu khol bi • (Touss touss nak touss ) maay seytané bi • • Refrain • Enh man rek ley toppeu • Souy nelaw man rek ley guinteu • Ki dé man leu dinkeu kholam • Maay seytané bi • • Couplet 2 • • Mani djongué takh sama khir laa yor di bathie • Gni dougne touss ci game bi maay bandit bou mag bi • Kou sa dieukeur dof ba feul meu doto nélaw • Dama diongoma ba yakou seine wakh laye fakhass ni nguélaw • Man ma kham fikoy khassane • Diko wokkou té meunougne ci dara • Mom diokh nama bopp ba tog sama néné sou gouddé mou wowé meu maman • ouh ohhh ohhhh • Ohh bb kham ngani maley danel • Maay fékheul seu khol • Fo meunti dem dangay nieuw sama djongué molay gaagn man nga beugue ci leu life • • Pre-refrain • • man rek ley toppeu • souy nelaw man rek ley guinteu • (Touss touss nak touss ) ki dé man leu dinkeu khol bi • (Touss touss nak touss ) maay seytané bi • • Refrain • • Enh man rek ley toppeu • Souy nelaw man rek ley guinteu • Ki dé man leu dinkeu kholam • Maay seytané bi • • • REMERCIEMENTS: • Tenue: Amossa • Coiffure: Dijaaaa and aïcha • Accessoires: Dishop • MakUP: Sokhna Pene • Chorégraphie: prince • • — Abonnez vous et activez la cloche de notifications 🛎 ✅ • • Assurez vous de suivre Aicha Kone sur: • • Instagram - https://www.instagram.com/aicha_kone_... • Tiktok - / aicha_kon2 • • #AICHAKONE2024
#############################
