Wizzy Kana Weetay Hommage à Nos Morts











>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=L-KdntKayi0

#wizzykana #sénégal #abonnetoi • « Il y a quelque chose de plus fort que la mort, c’est la présence des absents, dans la mémoire des vivants. » Jean d’Ormesson • Ceci est une production de Neegurap Music Groupe • Artiste : Wizzy Kana • Réalisation : Kainri Pictures • Montage Etalonnage : Kainri Pictures • Assistant Cam : Halil Prod • Making Of : Good Stuff Movies • Location : Dartdart Dakar • Assistants : Cheikh Bèye Kalash Director • Enregistrement : Neegurap Music • Mix - Master : PeulBouHigh Beatz • Composition Musicale : PeulBouHigh Beatz • production : MBT100©️ • Remerciements : Fla Negurap Jordy Diop • Lyrics Weetay : • Aduna meune neuh tass yaakar iow • Lii kouniou ko waxoone dh dougnko geum iow • Ndékké yallah • Bou soxlawéé iow dinga niakk • Demnga wanté dou takh • Banga joggé thi sounou xalaat iow • Weetay weeteul nganiou weeteul sa waa keur • Demnga té dotouniou la guissat • Niakk nagn leuh ba abadane • Weetay • Weetaayeee • Joy nagn • Thi liniou leuh niaké (2x) • Mangui fatélikou jamono yign daane jotay • Waxtaane kaff foo reh souniou waadji • Yakarouniou woone ni dinga dem bagnou fi • Geumouniou woone ni dotounioula guissati • Yallah niou bakh rek leuh nango teela dieul • Mag gni seedé nagn ni jokhone ngaleen thieur • Démé nga ndaw ndékété aduna dou keur • Weetay weeteul nganiou weeteul sa waa keur • Demnga té dotouniou la guissat • Niakk nagn leuh ba abadane • Weetay • Weetaayeee • Joy nagn • Thi liniou leuh niaké (2x)

#############################









Content Report
Youtor.org / YTube video Downloader © 2025

created by www.youtor.org