Narah Diouf feat Bilou XIV Tégguil sa Tank clip officiel
>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=Rg81-Iv_guU
#narahdiouf #bilouxiv #tégguilsatank • Cette chanson traite un fait de société : les cas . Les ragots pour bien comprendre. • La vie de plusieurs personnes est aujourd'hui exposée à travers les réseaux sociaux avec des effets néfastes. Ce titre est donc un rappel à un retour à nos vraies valeurs. • Auteur - compositeur : Narah Diouf • Musique arrangement : Bilou XIV Karabalik Beatz • Script : Narah Diouf • DIRECTED BY IOROGLYPHE • PRODUCTION : Amna music • Suivez - moi sur mes réseaux : • Facebook: https://bit.ly/2TXNkv1 • Instagram: https://bit.ly/2Nsnuhu • Twitter : https://bit.ly/2NqCUmw • PAROLES 🎵 • REFRAIN • Life bé changé • Wala djikko yé yakou, yé yakou • Lo khamal ké Yolé • Ok Wakhnga ba tardé • Legui gneupeuley moytou, ley moytou • Mou ngui beug gnaw deh • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tank • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tankl • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tank • Ndank, ndank, ndank • • PREMIER COUPLET • (Narah Diouf) • Fi leu rew mi tollou • Gni deh cas lagniy topou • Lou tokh sa nopp • Fel sa guemin • Lepp tourou • Kone mou ngui tokh • Tiey Linga bokh • Tekk ko si souf • Balla mo souss • (Bilou XIV) • Ok Yangui si Tik Tok • Do raté Facebook • Snap nga flamme cas bi • Whatsap nga yénou tiow li • Ok bayil ninga néké • Li Dou sa métier • Boul topou sa khol • Wakhal prarara • REFRAIN • Life bé changé • Wala djikko yé yakou, yé yakou • Lo khamal ké Yolé • Ok Wakhnga ba tardé • Legui gneupeuley moytou, ley moytou • Mou ngui beug gnaw deh • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tank • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tankl • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tank • Ndank, ndank, ndank • DEUXIEME COUPLET • (Narah Diouf) • Bayil libeurou diambour • Di top sa kilo • Yow kholal sa bopp • Teggil sa nopp • Bayil soppp • Soooof • Shhhhh • (Bilou XIV) • Ya raw mor ndadié • Do raté dadjé • Kouy dem yobouleu • Fougn dem fekk leu • (Narah Diouf) • Life bi deh concourou teki là • Kou yekh niou bala fa • Diapal fils tè boul bayi • Fattal té bagna teppi • (Bilou XIV) • Fatalma fofou bou dara percé • Teubeul ma teup niou ande percer • Liguey rek di encaisser • Kassé • REFRAIN • Life bé changé • Wala djikko yé yakou, yé yakou • Lo khamal ké Yolé • Ok Wakhnga ba tardé • Legui gneupeuley moytou, ley moytou • Mou ngui beug gnaw deh • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tank • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tankl • Ndank, ndank, ndank • Teguil sa tank • Ndank, ndank, ndank
#############################