Amadeus Jëli feat officielwallyseck Clip Officiel
>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=RluxFXSURls
#jëli 2e extrait de mon album #taarusenegal est disponible sur toutes les plateformes de streaming : https://bfan.link/jeli • Ecrit par AMADEUS • Interprété par Amadeus Wally Ballago Seck • Compositeur : Papelayebeats • Mix / Mastering : Sirtam • Réalisateur Postprod : Mame Sélémane Dieye • Assistante Réal : Mareme Helene Fall / Thérese Coly • Directeur de prod : MLD • Chef décorateur Régisseur : Sadickdef frères • Assistante Cam : Weuz Ndiaye • Régisseur Général : Mame Cheikh • Make up artist : Penda Team • Directeur Photo Color Grading : Mandione Laye Ka • Lighting : Bras Magik • Management Team : Sir FALL MLD • Nos remerciements à CARGUYZ et à tous les figurants. • Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux : • Instagram : / massamba_amadeus • Twitter : / massambaamadeus • Facebook : / massambaamadeus • Tik Tok : / massamba__amadeus • Les paroles • Boo ma beddiwul xalaatuma la bàyyi • Amuma laamisoo tuddd mbalaay • Gaañ la taxul nga wax • Tooñ la taxul nga may réccu • Sàllaaw yenn saay nga mer • Sama njàmbaar ci yaw mi la wékku • Dootuma wiiri wiiri jaari Ndaari • Li ma moom laay jëli • Dootuma yónni kenn ci sama waa ji • Man mii maa koy jëli • Wally • Dootuma wiiri wiiri jaari Ndaari • Li ma moom laay jëli • Dootuma yónni kenn ci sama waa ji • Man mii maa koy jëli • Bala maa jug fajar • Fekk nga teg njaay • Bale kër gi raxas say ndab • Ndeke booba doom ngay waajal • • Amadeus • Dund a mat a ñaan • Ndaxte gaynde dof a kuy jur • Ndax fitnaaloo ma xeeboo li ma lay jox • Lépp loo ma ñaan dinaa la may • Wally • Dootuma def lenn lu lay metii sama ndaw si • Ndax sama nawle nga doon leeral sama yoon wi • Dootuma nangu mbindeef di dox sama digg ak yaw • Ndax Yàlla moo def ci nun loolu wéy na • Kaay waay • Gaañ la taxul nga wax • Tooñ la taxul nga may réccu • Sàllaaw yenn saay nga mer • Sama njàmbaar ci yaw mi la wékku • Dootuma wiiri wiiri jaari Ndaari • Li ma moom laay jëli • Dootuma yónni kenn ci sama waa ji • Man mii maa koy jëli • Bis • Gaañ la taxul nga wax • Tooñ la taxul nga may réccu • Sàllaaw yenn saay nga mer • Sama njàmbaar ci yaw mi la wékku
#############################
![](http://youtor.org/essay_main.png)