Bril Bras Long Clip Officiel
>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=_wufQjRrJU0
** Mon nouvel album SUBA est sorti. A écouter et/ou télécharger en cliquant ici https://listen.lt/BrilSuba1 ** • *Abonne-toi à ma chaîne ici https://goo.gl/Qw5BFh* • Le clip Bras Long est le premier single extrait du nouvel album de Bril, SUBA, disponible à partir du vendredi 20 septembre sur toutes les plateformes de straeming et téléchargement. • Pas facile de trouver un travail au Sénégal quand on n'a pas de relation ou de piston... Faire des études ne semble vraiment pas suffire ! (voir Lyrics plus bas dans cette description) • #Bril #BrasLong #Suba #NouvelAlbum20septembre #ClassChicMusic #team221 • **Crédits de la chanson Bras Long ** • Auteur : Bril • Compositeur : Bril • Studio enregistrement, mix, edit mastering : Class’Chic Music par Bril • Une production de Class’Chic Music (Dakar, Senegal, août 2019) • **Crédits du clip Bras Long ** • Réalisation : Reverse Studios • Stylisme : Bise Collection et Mouha Creation • *Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux* • Facebook / brilofficiel • Instagram / bril_officiel • Twitter / bril_fight4 • Snapchat : @bril-fight4 • * Contact management* • Mr Mahmoud Sy : +221 77 036 48 31 • [email protected] • *Booking international* • [email protected] • **Lyrics de de la chanson Bras Long ** • Intro • ooooh ooh ooooh • Bril laa aaah • (Bril on the beat) • Refrain • Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune ? • Daniouy Laathie kane mola yabal thi niom . • Lokho bou goudou fok nga amko soga dém . • Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone . • Est ce que am nga Bras Long ? • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long ,dothi gawa guéneu • Am nga Bras Long ! • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu ? • 1er Couplet • Bimay khalé dagn ma gueumlo ni wone , bouma djangué , bouma maaggué liguey . • Ma yaggueu thi école yi woute ay diplômes, lima rote thi xam xam guéédj la meuna thié fééy . • Wayé founé démnafa , lima djokhé thi ay CV boudone khaliss ma done millionaire. • Bo kholé sén mbalite yi guissmafa , bimay déposé lay xam douma am, moudjé nékk visionnaire. • Kane mola yabal ? Fok nga xam ,kou xam koulén xam ! Djangal badone kangam sokhlawougn sa Xél fii ! • Kholouniou sa xam xam , Lidjeuntiwougn sa meune meune , Wouteul Bras Long mélal ni kouy selfie ! • Refraun • Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune ? • Daniouy Laathie kane mola yabal thi niom . • Lokho bou goudou fok nga amko soga dém . • Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone . • Est ce que am nga Bras Long ? • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long ,dothi gawa guéneu • Am nga Bras Long ! • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu ? • 2ème Couplet • Bo amoul koulafa nékkal yakkar ni dangay am , Day mélni ngané dangay Connectéwou té amo pass ! • Té fo am yakkar djaroul ngafay dém, boudé kénneu Xamoulafa ni sa mot de passe ! • Thi musique bi , Lamb Dji’ak foumou meunti done , bou sa lokho goudoul lingay yôttou dothi djote . • Bo khamoul kou xam borom téén djaroul ngay soneu , même bo amé baak yaw dofa meuna Roote . • Bodé djiguén gueum sa bopp say mbir dougn thi #Takhaw , Dofa meuna #Took , Boudé beuggo #Teudd • Niawloul ay courte manche bo amoul Bras Long , lo beugga natteu niounéla djotoula , lofi wakh dou deugg . • Refrain • Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune ? • Daniouy Laathie kane mola yabal thi niom . • Lokho bou goudou fok nga amko soga dém . • Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone . • Est ce que am nga Bras Long ? • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long ,dothi gawa guéneu • Am nga Bras Long ! • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu ? • Pont • Amo bras Long, Takhoul nga djaay sa ngor , danga woute liguéy ba woutoum Liguéy moudjé done sa Liguéy . 🏾 • Boul Khaadi té boul gawa bayi , Kheuthie bou daggoul dikkeu , Yalla bourbi dalay Fay . • Est ce que am nga Bras Long ? • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long ,dothi gawa guéneu • Am nga Bras Long ! • « Bras Long - Bras Long » • Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu ?
#############################
