Jeeba GUUY prod by Bril Clip Officiel
>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=nJXGzao-5j0
Guuy, une histoire d’amour Made in Sénégal • Littéralement ce terme désignerait à première vue le baobab mais ce « guuy » dont l’écriture ne nous laisse guère indifférent traduit plutôt une joie immense un sentiment intense envers une personne. • Dans ce contexte c’est bien évidemment jeeba qui comme à l’accoutumée nous invite dans un voyage mélodique à la découverte d’une rencontre qui l‘émancipa à jamais. • Ceci n’est pas qu’une histoire d’amour c’est l’histoire d’un amour à la sénégalaise, un idylle née par hasard qui sonne comme des retrouvailles de premiers amours. • Guuy disponible : http://africori.to/guuy • Auteur : JEEBA • Instagram : Jeeba_abdn • Compositeur : Bril on the beat • Réalisation : Viewz Studios • Partenaires: Swiss Gold - O good food • Manager Rassoul : 77 434 11 63 • Chorégraphie : Prince ( ALL STYLE DANCE )- 78 636 46 81 • Dressing traditionnel : IBrahima 77 550 74 14 • Dressing blouson : Instagram momoo_le_noir • Lyrics : • Jeeba Guuy • Dinala daal foko doul fogué • Foko doul khalaté • Sa baniouy doguou thie lalaay dougué • Deey melni yallah ko yoné • Dina fess sa xool bi unh no no no • Eulemeul sa boop bi unh yeah yeah • Doto amati principe , Bafouer nga leep • Meuno guiss si moom siik • Yoow loum lay deef dou yow rek yakoo xaameu • Dou lou niit meuneu wakh • Yoow fim may yobou dafa melni meussoumafa deemeu • Wayé dou lou niit meuneu wakh • May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé • May ladj kagn laay magué • Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué • Degg na sakh dama jongué • Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo • Yaay sama hero • Sama bébé d’amour conquérir nga sama xool • Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool • Bo bégué ma begg bo dioyé ma dioy • Lima guissoul si niom la guiss si yow mou doyma • Sandi nga cravache dane ngaleen diél bou gaaw • May sa djomba niaaw djomb nala deef lou niaaw • Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié • Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié • Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy • Seral ngamaa guuy guuy guuy • Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy • seral ngama Guuy guuy guuy guuy • Tank tank mbague ak mbague niou deem • Waat nani dinala yobou Fenen • Yoow defal nank boul deglou wakhi noone • Niom douniou deem beugouniou kou deem eeh • Khana xamoni lou bakh nieupeu ko beugg beugg • Fi liniuy wakh khadj ba dou deugg deugg eeh • Khana xamoni meune naniou wakh mais duniu beugg • Seen biir xool meunou niou guiss niaar niou beguenter • Tei xamnani warone na done Gueweel ma tagaal la say maam • Warone nga done jaam ma goreel la goreel saay maam • Souma amone avion dou ma maylako dila dowaalal fo beugg • niou dieum thia li soula doyoul wakhma loulay dooy bébé • Bilay walay khawma lilay dooy • May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé • May ladj kagn laay magué • Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué • Degg na sakh dama jongué • Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo • Yaay sama hero • Sama bébé d’amour conquérir nga sama xool • Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool • Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié • Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié • Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy • Seral ngamaa guuy guuy guuy • Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy • seral ngama Guuy guuy guuy guuy • May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé • May ladj kagn laay magué • Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué • Degg na sakh dama jongué.
#############################
