Jahman XPress YAAY Album ABIYO
>> YOUR LINK HERE: ___ http://youtube.com/watch?v=zjzD786Alng
EN CONCERT AU POINT FORT D'AUBERVILLIERT 27 SEPTEMBRE 2024 : https://shotgun.live/fr/events/jahman... • Production : Hoside Studio • Prod. by Jeuuss - Mix by Moussa Ngom • CONTACT MANAGEMENT : 77 640 22 08 • ECOUTER L'ALBUM ICI : https://backl.ink/149698758 • LYRICS • Yaye ki gueune ci mane yaye woye nala • Meunoumala faté • Soudoul wone ak saa yaye booy dina firim réw tass koo • Yaye balal ma • Yaye booy kaay balal ma • Soula nékhé daagoul sa ligueye fegn na ci sa ndiabot gui • Ay camions khaliss • Soumala ko done sotti • Dou doye ndakh diouro lou kene di khol nane thiam kane mondiour li • Mane santeu naa yallah buur bi bimala amé • Yaye diou melni ioe yomboul té khamna li takh ma wakh ko • Sanni ma daleu • Dou té malay gueureum • Loula nekh deff meu sama Aldiana ngui ci sey souffou tankeu • Mane santeu naa yallah buur bi bimala amé • Yaye diou melni ioe yomboul té khamna li takh ma wakh ko • Yaye defo fii lou niaw • Wakho fii lou niaw • Meusso nio wane guinaaw • Naadj bou tàngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw • Yaye gueureum nala • Yaw fo diaar yone la • • Kouniou nane demb téy motax • Yone bi goudoone na loool • Yaye moussoulo wagnékou • Bilay khepp nako loool • Lou néew loumay deff ci yaw • Sou yokoul dotoul waniékou • Na lamp yii takkeu ma photowok mom • Yaye rétane maa • Sa rétane dafmay doundeul • Guiss la rek dafmey bégueul • Doundeul doundeul • Ba Abadan moma done gueuneul • Yaye yama lene gueuneul • Nga fékké laley nianal • Mangui ci yaw ba guédj gui ferr ndakh yamay bégueul • Yaye foula ndanane di diaar • Sey att yakkoul sa taar • Naadj bou tàngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw • Yaye gueureum nala • Yaw fo diaar yone la • Na lamp yii takkeu ma photowok mom • Yaye rétane maa • Sa rétane dafmay doundeul • Guiss la rek dafmey bégueul • Doundeul doundeul • Ba Abadan moma done gueuneul • Yaye yama lene gueuneul • Nga fékké laley nianal • Mangui ci yaw ba guédj gui ferr ndakh yamay bégueul • Ya foula ndanane di diaar • Sey att yakkoul sa taar
#############################
